Drifty dafay bokk ñaari monde ci benn marque: Drifty Solution ngir say abonnement numérik, ak Drifty Tech ngir say aksesuwaar ak say projet développement web ci mesir. Mission bi nun: numérik dinañu ko wéral, gaaw te amul problème Dakar.
Bu fay bi wóoree, say identifiant walla invitation dinañu leen yónnee direct ci WhatsApp, souvent ci diggante ñaari waxtu.
Wave, Orange Money ak espèces.
Support bi WhatsApp am na 7 fan ci 7 ngir régler problème bu ne, te su war, wecc sa accès amul fay bu bees.
Waaw, livraison am na Dakar ak région yi ci diggante partenaire livraison yu nun, ak delai ñu leen wax bu commande bi.
Dem ci page Service, fees formulaire bi ci étap yu ndaw, te am étude bu amul fay ci WhatsApp ci 24h liggéey.